Layene Digital

Layene Digital

Portail Digital de la communauté #Layene
00:00
00:00

Résumé de l'épisode

Niroo ak demug Imaam al Laay xayrunaasGuddig Jumaa ja boobu bés tam tàng naLu jiitu dig ba ñaari ay bés Maam LibaasJiite jullit ña cëy koreem ga metti naLimaamu nan gaaw leen ma àgg JàmmaLaayAnna janazatun digam ba yemb naYaram wa jeexMu mel ni bant bu nu solal ay yére,Leer ya wër kanam ga taaru naMu naan ku yéene jox Yónnen bi ab dërëm na andi jox ma man la maay RasuulunaMu wax xarit ba Seex Maxtaar Xawsuna jàngal xutab yi muy duuras ci Axlu naFeebar ba dëj ko muy sikar di waaj xanaa, lu nu mën dal war nan xalaat ImaamanaGuddig jumma ja, fukki fan ginaaw kori ak ñenti fan Limaamu génn àddunaJigéen ñay yuuxu, saaba yépp booloo di jooy te naan nax ga nu rek ba dem ay waay xabibunaaManjoon taxaw yor jaasi naan kenn du fi rob Libaas te Sëydinaa ñëwul li yell naÑuy xaar Isaa ndax bëyti Maamuur lay bawoo ñuy jooy Limaamu ñetti fan ya metti naMu ñëw di fóon kanam ga naan ko Waalidi tipta xayyan wa maytan wa RabbinaMu nan leen ku daan jaamu Limaamu mën ga dem Kuy jaamu Yàlla toog nu gëm MaalikunaMiimun la toog kenn…

Épisodes

79-

Zikrullah - Ñaanu Seydina Limamou Lahi (PSL) 2026

21 avr. 2026
78-

Zikrullah - Ñaanu Seydina Issa Rouhou Lahi (PSL) 2026

𝑩𝒂𝒂𝒚 𝑺𝒆𝒚𝒅𝒆𝒆𝒚 𝑹𝒖𝒙𝒖 𝑹𝒂𝒙𝒎𝒂𝒂𝒏 𝑵𝒖 𝒏𝒈𝒊 𝒍𝒂𝒚 𝒈𝒆𝒎 𝒍𝒂𝒂𝒚 𝒎𝒂𝒅𝒊𝒊𝒏𝒆𝒆 𝑫𝒊 𝒍𝒂 𝒏𝒖𝒚𝒖 𝒍𝒂𝒂𝒚 𝒎𝒂𝒎𝒂𝒅𝒖 𝒎𝒂𝒙𝒕𝒂𝒓 𝑫𝒊 𝒍𝒂 𝒚𝒂𝒌𝒂𝒂𝒓 𝒚𝒂𝒘 𝒎𝒂𝒅𝒊𝒊𝒏𝒆 🖤 #layene #islam #layenedigital #zikrullah

21 avr. 2026
77-

Mame Libasse Lahi - Ñaanu Seydina Issa Rouhou Lahi (PSL) 2026

“Jàmm rekk laay am bis ba ma juddoo, ak ca bis ba may dee ak bis ba may dekkiwaat”. (S19 V33) Ruhu Laay Alasaan jàlle nu 🤍 #layenedigital #layene #islam

19 avr. 2026
76-

Seydina Issa Laye - Ñaanu Seydina Issa Rouhou Lahi (PSL) 2026

Discours de Seydina Issa Lahi à #Camberene lors de la nuit de prières dédiées à Seydina Issa Rouhou Lahiﷺ 🤍#layenedigital #layene #islam #weextal

17 avr. 2026
75-

Mame Libasse Lahi - Ñaanu Seydina Limamou Lahi (PSL) 2026

Discours de Chérif Mame Libasse Lahii à #Yoff Diamalaye lors de la nuit de prières dédiées à Seydina Limamou Lahi (PSL), Seydina Mouhamadou Makhtar Lahi & Imam Bachir Lahi 🤍#layenedigital #layene #islam

15 avr. 2026